108 Pexe yi nuy owe Set bu gaaw mu ngi ajo ne du soxla jël tutti ci deret yoone ko ci laboratoor, tax ba ne ci saasi mën nga xam lu mu joxe. Yeen ci setlu yi day ajo tox deret(jaam bu ndaw ci baaram doyna), waye ci yeneen yi lu tutti ci tuflit la nin jël. WOLOF SET BU GAAW DOOMU JANGOORO JI VIH 01 XETTU SETLU YI Setlu yu bes yi da niiy giis tox yi yaramwi jur ngir xex doomi jangooro ji di VIH. Yi ci Mujjantal setlu yu bes , da niiy Boole giis tox ak proteyin VIH (antixeno p 24). 02 LAN MOOY DIIRU PALAANTEER? Mooy diir bi ngaay xar gànaaw bi nga ame jooté bu andul ak fagaaru ba bi niiy amal setlu bi bu giise ne amul siki saka. AY BES L /6 A Ndam sax bu setlu nekke ci xarañ yu bes, yi ngir mu ame solo fokk nga xar 3 wer ba yaraw wi jur tox yi xex jangooro ji. Si yu bes yi mujjantal yi diiru palaanteer mo gëna new 6 ay bes la. 3 WE R 03 NDAX LI SETLU GIIS WOOR NA? GTT-VIH GRUPO DE TRABAJO SOBRE TRATAMIENTOS DEL VIH ENTIDAD DECLARADA DE UTILIDAD PÚBLICA ONG DE DESARROLLO Setlu yu gaaw woone naan seen woorte. Lu mënti doon, bu nu giise doomu jangooro ji ci yaw, da kay dëggal ak setlu laboratoor. 04 FO KA MËN DEFE? Mbootaay yi xex jangooro ji yu baari nu ngi def setlu bi di ci sutura te ban lajj tuur, ci lo dul faay dara; mën la diggal fooy dem: lajj leen! Tamit mën nga ko dem ci farmasi ci yeen gox yi (Kantabariya, Kastiya ak lewon, Kataluña, Sewta , Dekk Bask yi) 05 FATTALI Setlu yu gaaw yi doomu jangooro ji di VIH lu bax ngir xam ndax ame ngo ka Ajoci xeetu setlu yu, diiru palaanteer day nuy wute. Stlu bu woone am amu doomu jangoor ji ci yaram wi, da nu wara def setlu firnde ci laboratoor. ¿TIENES DUDAS SOBRE EL TEMA? PREGÚNTANOS Tel. 93 458 26 41 [email protected] INFOVIHTAL / SET BU GAAW DOOMU JANGOORO JI VIH